Film e animazione

Madior Ak Dior - Épisode 11 [Saison 01]

[ABONNEZ-VOUS ici] ☆~~👉 itchannel.org/usname-PikiniProduction
[FACEBOOK]☆~~👉 www.fb.com/PikiniProductions
[TWITTER]☆~~👉twitter.com/PikiniProd
#Madior_ak_Dior_itchannel.org/list-PL7OYJbvZchhHCAKLYpjgAFrKKzFTYbq3o
#Pikininfos_itchannel.org/list-PL7OYJbvZchhHGVY69iThhO-9qmAl_vss4
#SÉRIE_BÈS_itchannel.org/list-PL7OYJbvZchhGXCEvkvaTvu7ZKh_tORumo
WhatsApp ☆~~👉 +221776626858
Pikini Productions
ByBen 2019

Commenti

  1. SOKHNA FATMA MOUSTAPHA MBACKÉ

    SOKHNA FATMA MOUSTAPHA MBACKÉ

    10 ore fa

    Kou idiote Mére ak idiote fille soff like

  2. fall kimflow

    fall kimflow

    Giorno fa

    Dit moi l'oncle de madior il détesté les femmes mai il n couch par avec keus

  3. dieynaba Diop

    dieynaba Diop

    Giorno fa

    Yama rew n'a sa tonton n gay wahh li ak tiofel bimu am ci yow

  4. Ly Abdourahmane

    Ly Abdourahmane

    Giorno fa

    Wa mei ki khana centenaire parfum lay am😅😅

  5. Elhadj Malik

    Elhadj Malik

    2 giorni fa

    Ana gni prepare hadara tidianiya a stade amadou barry vendredi soir aparté de 17heures les 3 mai inchallha vs prépare

  6. Mamah Ndiaye

    Mamah Ndiaye

    2 giorni fa

    guanguan

  7. le monde de maya

    le monde de maya

    2 giorni fa

    Mais yama loutakh mou tame sékh lokhom ich elle m'enerve nak

  8. Rama Ndiaye

    Rama Ndiaye

    2 giorni fa

    Madior il joue a quoi 🤔🤔🤔

  9. Rama Ndiaye

    Rama Ndiaye

    2 giorni fa

    Naar weroul srx

  10. Tida Diaby

    Tida Diaby

    2 giorni fa

    Excusez moi,mais il ya quelques choses qui m'échappe ; comment se fait il que la mère de Dior ne se rappelle pas de sa vie passée ni de qui elle est mais elle se souvient du père de sa fille?

  11. Sanandreascjnjiez Sanandreascjnjiez

    Sanandreascjnjiez Sanandreascjnjiez

    2 giorni fa

    I like this movie nice

  12. Aminata Ndoye

    Aminata Ndoye

    2 giorni fa

    Mane deh suis totalement perdue avec ces liens de parenté flous

  13. Ndèye Aminata MBAYE

    Ndèye Aminata MBAYE

    2 giorni fa

    Cc yane jour lay ame mane khawma damay tatoner chak jour

  14. Master Atlanta

    Master Atlanta

    2 giorni fa

    Kou beugue Tawhid beuseul j’aime

  15. Théatre Sénegalais

    Théatre Sénegalais

    2 giorni fa

    félicitation trés bien fait cette vidéo

  16. Khadiza Dieng

    Khadiza Dieng

    2 giorni fa

    J'adore cette série c'est la meilleure des séries

  17. Fallou Ziada

    Fallou Ziada

    2 giorni fa

    Nice job ma beugu chéri bi

  18. Dié laye

    Dié laye

    3 giorni fa

    😂😂Mane dall Narre Diop layy weurr nekete elle jour trop bien Nenakoh diokhma 3millions mah diappal lh djiné rama Diop bi mouy dokhantou ci keur gui nakh gua nek nitt

  19. Monde Cruel

    Monde Cruel

    3 giorni fa

    Yama say bisous ak say rayy sincèrement eupna si Pa bi. Di toubab toubab lou rek, eupna nak.

  20. Aminata Barry

    Aminata Barry

    3 giorni fa

    Tonton Libass koulayii makille nekoiu mouu wagniii poudrée biii

  21. Nafissatou Faye

    Nafissatou Faye

    3 giorni fa

    Bilay ma diepiiiii borom parfum guou bari gui

  22. Anna Dieye

    Anna Dieye

    3 giorni fa

    Team dior

  23. Conneries d' afrique

    Conneries d' afrique

    3 giorni fa

    ghen yaakar Yama dou moudié doxaan papou Madior? ish. ki nimouy raayé paabi nexna deh

  24. Salimata Seck

    Salimata Seck

    3 giorni fa

    beugeu na yi

  25. 3 giorni fa

    Ani wa team Dior

  26. Ndeye Amy Diakhate

    Ndeye Amy Diakhate

    3 giorni fa

    Yama ake yayam rek gniouma soff

  27. anen anen

    anen anen

    3 giorni fa

    No yama bagn nala trop

  28. elhadji thiam

    elhadji thiam

    3 giorni fa

    c est ce que font les filles elles maraboutent les hommes avant le mariage les hommes faites attention aux filles

  29. Yebe Sylla

    Yebe Sylla

    3 giorni fa

    Thieuy nar ak yama

  30. la vie et moi

    la vie et moi

    3 giorni fa

    C pas une crittique mais juste une remarque. Je crois que Dior devrait se maquiller moins elle n a pas besoin de Toute cette couche sur le visage il faut quelle valorise son teint naturel et noir 🤔

    • Ndeyefatou thioune

      Ndeyefatou thioune

      Giorno fa

      El s makill trop tamit

  31. Sy Djeynaba

    Sy Djeynaba

    3 giorni fa

    Dior way

  32. kadet djigo

    kadet djigo

    3 giorni fa

    Dior est très belle qui est d accord

  33. Djash Keub

    Djash Keub

    3 giorni fa

    Madior akh Dior esk dougnee ayy cousin.. cousine

  34. seykou ndongo

    seykou ndongo

    4 giorni fa

    L

  35. ML

    ML

    4 giorni fa

    Les enfants de fatou Ndiaye indo sont le papa de madior et les triplé dont la mère de Dior. Après l'oncle de madior kimou beteu ak kharitam bi c'est l'une des triplé c pour cela qu'il pense que la maman de Dior l'a trahis. En résumé yayou Dior ak papeu madior sont frère et sœur puis papou Dior ak yayou madior sont aussi frère et sœur 😂 may scénariste bi...

  36. Diama  Ndiaye

    Diama Ndiaye

    4 giorni fa

    Démarche yama bi la menoul mougn man 😂 😂

  37. Adja Ndiaye

    Adja Ndiaye

    4 giorni fa

    Les 3 jumelles: Narr maman de yama, marieme maman de dior, et la 3 identique à la maman de dior est celle que tonton de madior a vu à st louis avec son ami. Le tonton de dior et la maman de madior rama sont frère et soeur d'où la ressemblance de dior. Et qui prouvera ainsi qu'elle est bien sa fille. Sama ? Le père de madior est il issu du 1 mariage de fatou info ou est il le dit frère ??? Sinon rek aff d'inceste la niou am fofou🤪🤪🤣🤣🤣

  38. Asta Seck

    Asta Seck

    4 giorni fa

    J aime dior

  39. Mamita aïdara

    Mamita aïdara

    4 giorni fa

    Da mélni dior ak madior gnio bokou yaye?

  40. Bichette Diaa

    Bichette Diaa

    4 giorni fa

    Dior Ma Sha Allah ❤

  41. belle belle

    belle belle

    4 giorni fa

    Yow bagniala moytou sa parfum yi gay pousso dagay sodji legui ak allergie

  42. Salla SAMB

    Salla SAMB

    4 giorni fa

    Mais tonton Linas mo Aÿ com ivoirien ton bi c'est génial

  43. la belle limashu

    la belle limashu

    4 giorni fa

    Idiote mère ak idiote fille merenalen trop

  44. Serigne Ibrahima Diop

    Serigne Ibrahima Diop

    4 giorni fa

    Bravo Le pére de madior joue bien son rôle.Il nous des leçons de vie

  45. Ibrahima Fall

    Ibrahima Fall

    4 giorni fa

    Merci

  46. toulaye ngom

    toulaye ngom

    4 giorni fa

    Machahalah mais Ndiaye teranga sa kourouss gui Kouko nass😂😂😂😂😂

  47. Thiatou Khadim

    Thiatou Khadim

    4 giorni fa

    Yayou dior nekh nama

  48. Amina Lo

    Amina Lo

    4 giorni fa

    Ohh la mère de dior Black N prOud😍❤

  49. Binta Ndayr

    Binta Ndayr

    4 giorni fa

    Mais Dior t trop belle machallah 😘

    • Binta Ndayr

      Binta Ndayr

      4 giorni fa

      Machallah

  50. alioune fall

    alioune fall

    4 giorni fa

    Mais Madior ak Dior loune book ?

  51. Khadidiatou Ka

    Khadidiatou Ka

    4 giorni fa

    Best serie .. who are agree with me??

  52. Khadim Ndeye

    Khadim Ndeye

    4 giorni fa

    🤞

  53. Cheikh Ibra Faye

    Cheikh Ibra Faye

    4 giorni fa

    Dior moudié na féminine hennnn

  54. Athia Drame

    Athia Drame

    4 giorni fa

    Team Dior

  55. Khady Fal

    Khady Fal

    4 giorni fa

    Nar aussi parfum bi mom mingui derangé li amoul way

  56. Ramatoulaye Fall

    Ramatoulaye Fall

    4 giorni fa

    Yen compoulen dara😂😂 garmi (papay dior) ak yayou madior gno bok et que yayou dior ak papay madior ak Narr et l'autre qui est disparu gno bok

    • Amish Diagne

      Amish Diagne

      4 giorni fa

      et le fait k dior ressemble à la maman de madior

  57. feuz Camara

    feuz Camara

    4 giorni fa

    team Yama❤

  58. Sokhnadiarra Thiam

    Sokhnadiarra Thiam

    4 giorni fa

    Dior nak amal foula bayi di tok à sa amoré di toudou yama ahhh faté ko tek ko feulé nek sa bopou lolou la beug si rival bou manquant melni kouko ragal yawit

  59. tamsir sene

    tamsir sene

    4 giorni fa

    tjr avk la maman de dior

  60. Nogaye Ndiaye

    Nogaye Ndiaye

    4 giorni fa

    Ohhh beugouma geum li madior ak dior gno bok yaye t bokougnu papa ...wala rék yayou Dior am jumelle kokou gagnou

  61. tv Sénégal

    tv Sénégal

    4 giorni fa

    Nhke n'a

  62. khady faye

    khady faye

    4 giorni fa

    Non Yama elle m'énerve koi jtj thimmm waaay

  63. sarr tapha

    sarr tapha

    4 giorni fa

    mais YAMA kene douko wakh degue avec son doigt dans la bouche à chaque fois

  64. khadiza Dia

    khadiza Dia

    4 giorni fa

    Yama sa dokinne bakhoul 😂wayyy

  65. AMZO BEUBEU

    AMZO BEUBEU

    4 giorni fa

    nar diop daal parfum bi amoul effet chak seconde pisse pisse kikaay diay parfum daal dou lameuleee

  66. MAODO MALICK NIANG

    MAODO MALICK NIANG

    4 giorni fa

    tonton libasse sa marabout bi la beug guisse cme k mo takh côte-d'ivoire dieul coupe d'Afrique mou défalniou notre Sénégal dieul coupe d'Afrique bi bok

  67. Marieme Ndoye

    Marieme Ndoye

    4 giorni fa

    def sa maquillage bou daff def sa pose ak lithi dem yeup deréwoul gay mathie baram thimm salté ga yama

  68. Lytou Nd

    Lytou Nd

    4 giorni fa

    Sheutt mane yama mi gnémé na nitt trop collé na pa bi ak dollé ishh

    • Lytou Nd

      Lytou Nd

      4 giorni fa

      Jsai benji

    • Benjamin Et Mame

      Benjamin Et Mame

      4 giorni fa

      Lytou Nd c’est normal c’est son oncle

  69. jeanne marie yama sene

    jeanne marie yama sene

    4 giorni fa

    Yama elle est mon homonyme mais elle me plaît pas parceque le doigt qu'elle mai dans sa bouche

  70. saida dione

    saida dione

    4 giorni fa

    yama khamo sa bopou nak regarde toi epuis tai trop vilaine tegue bayi lokho bi sakh nii

  71. Jeanne anno Badji

    Jeanne anno Badji

    4 giorni fa

    Machalla Dior je vous adore

  72. saida dione

    saida dione

    4 giorni fa

    Thieye libasse

  73. Thiam Matare

    Thiam Matare

    4 giorni fa

    Man djinné la Giss

  74. Ndiaye Cheikh

    Ndiaye Cheikh

    4 giorni fa

    Mathie barame kome lire

  75. ndoumbelaye samb

    ndoumbelaye samb

    4 giorni fa

    Esk la maman d dior moko diour deugeuntan

  76. Ndofa Alias Siteu

    Ndofa Alias Siteu

    4 giorni fa

  77. Omar Badiane

    Omar Badiane

    4 giorni fa

    Dillahi badianou madior bi ak domame comme ay lékoukatou kéwe gnidagnon sofe torope way thimmmm

  78. Un jardin d'Eden

    Un jardin d'Eden

    4 giorni fa

    exit les manies de yama et sa maman!!!! beurkkkk

    • Un jardin d'Eden

      Un jardin d'Eden

      2 giorni fa

      pikini production...il est où notre épisode 12?!! que se passe t il?

  79. khady aidara

    khady aidara

    4 giorni fa

    Au faite Dior est la cousine de madior... les 3 jumelles de la photo je crois que l’une est la mère de Dior et l’autre madior..scénario lay tek ni deh lol

    • Fatou binetou Thiam

      Fatou binetou Thiam

      4 giorni fa

      Lolou la guis deh

  80. sall nitdoff

    sall nitdoff

    4 giorni fa

    Wa yène ndaw si do lène ko wakh mou Bayi mathie baram

  81. Alymareme Diouf

    Alymareme Diouf

    4 giorni fa

    Machalla j'adore la maman de Dior

  82. carla gomez

    carla gomez

    4 giorni fa

    Yama bègue gua goor yaw do regler bagnou take la terminus de l'oeil

  83. Sashita Ndiaye

    Sashita Ndiaye

    4 giorni fa

    Wooooyyyy Garmi rayy nama nenako Nar ap thiaaa... la🤣🤣😂

  84. Thiaba Faye Nassinhou

    Thiaba Faye Nassinhou

    4 giorni fa

    Yama saleté gua sa barème bi thimmm

    • Benjamin Et Mame

      Benjamin Et Mame

      4 giorni fa

      Thiaba Faye Nassinhou mais barame c’est une maladie on peut pas le laisser comme ça c’est une manque d’affection qu’on avait étant enfant qui perpétue

  85. Mariam Dia

    Mariam Dia

    4 giorni fa

    Idiot père ak Idiot fils mom yama ak Naar leu waron don!🤦🏾‍♀️🤦🏾‍♀️ Idiote fille ak Idiote mère 🤦🏾‍♀️🙄🚶🏾‍♀️

  86. Mk Mk

    Mk Mk

    4 giorni fa

    athia way il faut se devoloper le temp pass

  87. Max La lionne

    Max La lionne

    4 giorni fa

    Yayou dior dafa melnii sex la

  88. Aïsha Sow

    Aïsha Sow

    4 giorni fa

    Sénégal rek la guiss niouy commentaire série di hors sujet 🤦🏾‍♀️ a part sa la série elle est top

    • Amina Lo

      Amina Lo

      4 giorni fa

      Ma chere ss contre si lolu niouy def mais nekoul ni SnN rekk la yem dh barina sakh

  89. Soce Poumane

    Soce Poumane

    4 giorni fa

    Maïmouna mom nekhna ma deih walae

  90. Serigne Diagne

    Serigne Diagne

    4 giorni fa

    Nekhna

  91. ndeya ndiaye

    ndeya ndiaye

    4 giorni fa

    Kou dackor ni Nar sikhoram bi mo bari Sénégal kou ray say mbok say none diekh

    • ndeya ndiaye

      ndeya ndiaye

      4 giorni fa

      +Khady Sall bilay mofi bari

    • Khady Sall

      Khady Sall

      4 giorni fa

      ndeya ndiaye malako wakhe dé

  92. Aziz Sall

    Aziz Sall

    4 giorni fa

    Kone dior ak madior ngo book yaye

  93. Kaw Kaw

    Kaw Kaw

    4 giorni fa

    Papa Madior Mom MO tëdé woon doff bi nguir am xalis PIKINI ponne contusions

  94. Evidence Aimiehefe

    Evidence Aimiehefe

    4 giorni fa

    Nice na trop

  95. Anita Drame

    Anita Drame

    4 giorni fa

    Waa ioe yama ltx nga collante diap paa bi diko gnapakhou nii yek ko rkk ni doko wathieu eupna way😂

  96. Fatou Faye

    Fatou Faye

    4 giorni fa

    Lii nekhna trop et bon courage pikini

  97. un jeune sénégalais

    un jeune sénégalais

    4 giorni fa

    shoooot série bi dall beurina ay thiakh..... mane dama khalate ba sama boppou bi di métty

    • mamour fall

      mamour fall

      4 giorni fa

      Bilahi mèm man mi

  98. Ma Asta

    Ma Asta

    4 giorni fa

    Sonounane so pishshsh pishsh bi (Parfums bi) mdrrr

  99. Bachir domou parcelle

    Bachir domou parcelle

    4 giorni fa

    Yup

  100. Aida Mboup

    Aida Mboup

    4 giorni fa

    Yama kou saltei la baram bi Mouy mathi rek bou done sax droite bila mou tanei sax

Prossimi video